Acts 22:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Boroom bi ne ma: “Demal, dinaa la yebal fu sore, nga jëm ci xeeti ñi dul Yawut.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ma: “Demal, man, fu sore laa lay yebal ca ña dul Yawut.”»