Acts 22:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu kilifa ga santaane, ñu dugal Pool ca tata ja te caw ko ay yar yu metti, laaj ko ba xam lu tax ñu di ko yuuxoo nii.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu njiitu gàngoor ga santaane, ñu dugal Póol ca tata ja te laaje ko ay yar, ngir xam lu waral ñu di ko yuuxoo noonu.

Recommended Reading