Acts 22:25 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye bi ñu koy joñ ak ay der, Pool ne njiitu xare ba fa taxaw: «Ndax am nga sañ-sañu dóor ay yar jaamburu Room, te fekk yoon dabu ko sax?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka lañu ko yeew ngir dóor ko ay kàccri, mu ne njiitu takk-der ba fa taxaw: «As goru Room bu yoon dabul, mbaa am nga sañ-sañu dóorlu ko?»