Acts 22:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko njiit la déggee, mu fekki kilifaam, yégal ko ko; mu ne ko: «Ndax xam nga li ngay def? Nit kale jaambur la ci Room.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njiitu takk-der ba dégg loolu, daldi dem ba ca njiital gàngoor ga, xamal ko ko, ne ko: «Li ngay def nag? Nit kii as goru Room la!»