Acts 22:27 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu kilifa ga ñëw laaj Pool: «Wax ma, ndax jaambur nga ci Room?» Mu tontu ko: «Waaw, moom laa.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njiital gàngoor ga dikk, ne Póol: «Yaw wax ma, ndax as goru Room nga?» Mu ne: «Waaw.»
Recommended Reading