Acts 22:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kilifa ga ne ko: «Man fey naa xaalis bu bare, ngir nekk jaambur ci Room.» Waaye Pool tontu ko: «Man de dama koo judduwaale.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: «Man de xaalis bu bare laa jënde sañ-sañu doon as goru Room.» Mu ne ko: «Man nag moom laa judduwaale.»