Acts 22:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ñi ko bëggoon a dóor ay yar nag randu ko ca saa sa. Te kilifa ga sax tiit ci xam ne Pool jaamburu Room la, te yeewlu na ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña ko doon waaja laaje ay dóor nag dànd ko ca saa sa. Njiital gàngoor ga it tiit na, ba mu yégee ne Póol as goru Room la, te fekk mu yeewlu ko.