Acts 22:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Waaye ci digg-bëccëg, bi ma jaaree ca yoon wa, ba jegesi Damas, ca saa sa leer gu mag jóge asamaan, melax ba ëmb ma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yàlla def ma topp yoon wa, ba jub Damaas ci digg bëccëg rekk, ag melax gu mag jekki fettaxe asamaan, ne ràyy fi ma wër.