Acts 22:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñi ma àndaloon gis nañu leer ga, waaye dégguñu baatu ka doon wax ak man.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñi ma àndaloon gis nañu leer gi, waaye ki wax ak man, xamuñu li mu wax.