Acts 23:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñu dem ca saraxalekat yu mag ya ak njiit ya ne leen: «Giñ nanu ne, dunu mos dara, ba kera nuy rey Pool.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu dem ca sarxalkat yu mag ya ak mag ña, ne leen: «Danoo giñ ne dunu dugalati dara sunu gémmiñ, ba kera nu reyee Póol.