Acts 23:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Léegi nag yéen ak kureelu àttekat ya, laajleen kilifa ga, mu indi ko ci seen kanam, mel ni dangeen a bëgg a seet mbiram bu gën a wóor. Bu ko defee nun dinanu fagaru, ngir rey ko, bala moo agsi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag yeen ak kurélu àttekat yi, ñaanleen njiital gàngoor gi, mu indi Póol ba ci yeen, mu mel ni dangeena bëgga seetaat bu baax mbiram. Nun nag fagaru nanu, ngir bala moo agsi, nu rey ko.»