Acts 23:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mu tontu ne: «Yawut yi dañoo dige, ngir ñaan la, nga indi Pool ëllëg ca kanamu kureelu àttekat ya, mel ni dañoo bëgg a seet mbiram bu gën a wóor.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne ko: «Yawut yi ñoo mànkoo ci ñaan la, nga yóbbu Póol ëllëg ca kurélu àttekat ya, mu mel ni dañoo bëgga seetaat bu baax mbiram.