Acts 23:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu leen ko may, ndaxte lu ëpp ñeent-fukk ci ñoom ñu ngi koy lalal fiir. Dige nañu ak ngiñ ne, dootuñu lekk, dootuñu naan, li feek reyuñu ko; fi mu ne sax fagaru nañu, di xaar, nga nangu.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaw nag bu leen ko may, ndax lu ëpp ñeent fukk ci ñoom a koy tëru, te xasoo nañu ne dootuñu lekk, dootuñu naan, ba kera ñu ko reyee. Fagaru nañu ba noppi, di xaar sa ndigal.»