Acts 23:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kilifa ga nag sant waxambaane wa, mu bañ koo àgge kenn, ba noppi mu yiwi ko, mu dem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Njiital gàngoor ga daldi koy yiwi, ne ko: «Bul wax kenn ne ko àgge nga ma lii.»