Acts 23:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gis naa ne li ñu ko jiiñ mu ngi aju ci ay werantey seen yoon, waaye jiiñuñu ko dara lu jar dee mbaa jéng.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma gis nag ne li ñu ko jiiñ, ci seen mbiri yoonu diine rekk la, waaye du lenn lu jar rey, mbaa jéng.
Recommended Reading