Acts 23:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Pool ne ko: «Yàlla dina la dóor, yaw mi naaféq, bay samandaay miir bu joy bu ñu weexal. Yaa ngi toog di ma àtte, ci li yoon wi digle, ba noppi santaane ñu dóor ma, ci li yoon wi tere!»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol ne ko: «Fél la yaw, moom la Yàlla di waaj, jinigalkat bee, mbete miir bu ñu weexal! Yaa ngi toog, topp yoon, di ma àtte, te teewul nga xëtt yoon, di ma dóorlu!»