Acts 23:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu xarekat ya jël Pool ci guddi, indi ko ba ca dëkku Antipataris, ni ñu leen ko sante.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee xarekat ya def la ñu leen digal, yóbbu Póol ci guddi ba ca dëkk ba ñuy wax Antipataris.