Acts 23:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi gawar ga àggee Sesare, ñu jox boroom réew ma bataaxal ba, jébbal ko Pool.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gawar ga àgg Sesare, daldi jébbal boroom réew ma bataaxal ba, jébbal ko Póol itam.