Acts 23:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ña taxaw ca wetam ne ko: «Ndax dangay xas saraxalekat bu mag, bi Yàlla fal?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa géew ba ne ko: «Sarxalkatub Yàlla bu mag bi ngay xas nag?»