Acts 23:5 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Pool tontu leen: «Bokk yi, xawma woon ne saraxalekat bu mag bi la, ndaxte tëral nañu ci Mbind mi ne: “Bul wax lu bon sa kilifag xeet.”»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol ne leen: «Bokk yi, xawma woon ne mooy sarxalkat bu mag bi, ndax bindees na ne: “Sa kilifag askan, bu ko wax naka-su-dul-noonu.”»