Acts 23:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte Sadusen yi nanguwuñu ne, ndekkite mbaa malaaka mbaa rab, dara am na ci, waaye Farisen nangu nañu yooyu yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax Sadusen yi dañu ne ndee-ndekki ak malaaka ak rab, dara amu ci, te Farisen yi ñoom, yooyu yépp lañu dëggal.