Acts 23:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu nag coow lu bare daldi jib. Ñenn ca xutbakat, ya bokk ca Farisen ya, ne bërét, daldi xuloo bu metti ne: «Gisunu dara lu bon ci nit kii. Su fekkeente ne, rab a ko wax mbaa malaaka...?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu coow lu réy jib. Ñenn ca firikati yooni làngu Farisen ya, ne bërét, àddook doole, ne: «Gisunu lenn lu bon ci nit kii. Ku xam ndax aw rab a wax ak moom, mbaa malaaka?»