Acts 24:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi juróomi fan wéyee, Anañas saraxalekat bu mag ba dikk, ànd ak ay njiit ak layookat bu tudd Tertul, ñu woo Pool ci yoon fa kanam boroom réew ma.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu teg ca juróomi fan, Anañas sarxalkat bu mag ba dikk, ànd ak ay mag, ak ab layookat bu ñuy wax Tertul. Ñu jébbalsi boroom réew ma, tuuma ja ñu teg Póol.