Acts 24:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu ñu woo Pool, te Tertul daldi ko jiiñ naan: «Yaw Feligsë mu tedd mi, sa nguur jural na nu jàmm ju neex, te sa jàppandil soppi na lu bare ci sunu xeet.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu woo Póol, Tertul daldi yékkati kàddug tuuma, ne: «Kilifa gi, ci yaw la jàmm ju yaa ame, te yaa fàggu ay coppite yu ñeel askan wi.