Acts 24:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu waxee noonu, Feligsë mi xam bu wóor mbirum yoon wi, yiwi leen ba beneen yoon. Mu ne leen: «Bu Lisiyas kilifag xare bi ñëwee, dinaa àtte seen mbir.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba Feligsë jotoon naa am lu ko leer ci mbirum Yoon wi. Mu yiweegum leen nag, ne leen: «Bu Lisiyas njiital gàngoor gi dikkee, dinaa àtte seen mbir.»