bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 24:26
Acts 24:26 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Fekk yaakaaroon na it ne, Pool dina ko jox xaalis; kon mu di ko faral a woolu, ngir waxtaan ak moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu Feligsë yaakaar itam ne jombul mu jële xaalisub neexal ci Póol, ba tax mu woolu ko ay yooni yoon, ngir waxtaan ak moom.