Acts 24:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Gis nanu ko fépp ak ci lépp, di la gërëm ak sunu xol bépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Saa su nekk, ak fépp fu nu tollu lanu ràññee loolu, yaw Feligsë mu tedd mi, te di la ko sante lool.