Acts 24:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ngir bañ a yàggal jataay bi, maa ngi lay ñaan ci sa lewetaay, nga déglu nu ci lu gàtt.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw buggunu laa yeexal nag, rikk baaxeeti nu, déglu nu tuuti.