Acts 24:6 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Dem na ba jéem a teddadil sax kër Yàlla ga, waaye jàpp nanu ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kër Yàlla ga sax jéem na koo teddadil, noo ko jàpp.
Recommended Reading