Acts 25:10 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Pool ne ko: «Maa ngi nii taxaw ci kanam àttekaayu buur Sesaar; te fii lañu ma war a àttee. Te yaw ci sa bopp xam nga bu baax ne, tooñuma Yawut yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol itam ne ko: «Maa ngi nii taxaw ci kanam àttekaayu Buur Sesaar; te fii lañu ma wara àttee. Yawut ñi nag, defuma leen dara, te yaw ci sa bopp, wóor na la.