Acts 25:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su ma tooñoon mbaa ma def lu bon lu jar dee, kon duma tinu ngir bañ a dee. Waaye bu li ñu may jiiñ taxawul, kenn sañu ma leen a jébbal. Dénk naa sama mbir Sesaar.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ma tooñee, su ma defee lenn lu dee di àtteem, tinuwma ngir baña dee. Waaye su lenn amul ci li ma ñii di jiiñ, kenn amul sañ-sañu jébbal ma leen. Buur Sesaar nag laa dénk sama bopp!»