bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 25:12
Acts 25:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bi mu waxee loolu, Festus gise ak ñi ko wër, mu tontu ko: «Dénk nga sa mbir Sesaar, kon ci moom ngay dem.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu, Festus gise ak waa kurél ga, ba noppi ne ko: «Sesaar nga dénk sa bopp, ca Sesaar nga jëm.»