Acts 25:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye ma tontu leen ne: “Jébbale nit, fekk jàkkaarloowul ak ñi koy jiiñ, ba man a làyyil boppam ci li ñu koy jiiñ, loolu dëppoowul ak aaday nguuru Room.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma ne leen: “Aaday Room daal nanguwul ñu jébbale nit, ngir ñu rey ko, te jëkkula jàkkaarloo ak ñi ko tuumaal, ba mana layal boppam ci mbir mi ñu ko tuumaal.”