Acts 25:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw lijjanti mbir moomu jafe woon na ma lool nag, ma laaj ko, ndax bëgg na dem Yerusalem, layooji fa ci mbir yooyu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu nag jaaxal ma, ba ma laaj ko ndax nangu naa dem Yerusalem, ñu àttee ko fa ci moomu mbir.