Acts 25:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi mu ñëwee, Festus ne: «Buur Agaripa ak yéen ñépp, ñi fi teew tey, nit kaa ngi nii! Mbiram moo tax mbooloom Yawut yépp, muy ci Yerusalem, muy fii, wër ma di yuuxu ne: “Nit kii waratul a dund.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu dikkee, Festus ne: «Buur Àggripa, yeen mboolem ñi fi bokk ak nun teew, gis ngeen kii, moom la ma askanu Yawut wépp booleel, muy ca Yerusalem ak fii itam, ñuy xaacu naan: “Kii yelloowula dundati.”