Acts 25:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Fekk awma dara lu wóor ci mbiram, lu ma man a bind sang bi. Moo tax ma indi ko ci seen kanam, rawatina ci sa kanam buur Agaripa, ngir sunu jataay may ma lu ma bind.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbiram nag laa amul dara lu ma wóor, ngir ma bind ko sang bi. Moo tax ma indi ko ci seen kanam, rawatina ci sa kanam, Buur Àggripa, ngir gannaaw bu ñu ko dégloo, ma mana am lu ma bind.