Acts 25:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mu ne leen: «Ñi am maana ci yéen nag, nangeen ànd ak man, layooji ak nit ka, bu dee tooñ na.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne leen: «Kon nag, na nit ñu am baat ñu bokk ci yeen, ànd ak man, tuumaali waa ji, ndegam am na fenn fu mu tooñe.»