Acts 26:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Daan naa wër jàngoo-jàngu, di leen teg toskare te di leen jéem a weddiloo. Te sama mer daa na tar, ba ma di leen xañ ba ca dëkk yu sore, ngir fitnaal leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jàngoo jàngu laa leen daan tege mbugal ay yooni yoon, ngir xàccloo leen. Maa daan sànju ba xaabaabal ci seen kaw, topp leen ba ci biir dëkki jaambur yi.