Acts 26:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Noonu am bés, may dem dëkku Damas, yor sañ-sañ ak ndigalu saraxalekat yu mag ya.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yoon wu mel noonu laa doon dox, jëm Damaas, ci ndigalal ak ndénkaanel sarxalkat yu mag yi.

Recommended Reading