Acts 26:16 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye jógal taxaw. Lii moo tax ma feeñu la: teg naa la yen, nga di ma seedeel ci lépp li nga gis ci man, ak li ma lay feeñuji.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jógal taxaw nag. Dama laa feeñu ngir def la ngay sama surga, ngir nga di ma seedeel peeñum tey, ak peeñu yi ma lay feeñooji ëllëg.