Acts 26:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
«Buur Agaripa, ma làyyi ci sa kanam tey ci lépp, li ma Yawut yiy jiiñ, xol bu sedd la ci man,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Buur Àggripa, mbégte laa am ndax dinaa layool sama bopp ci sa kanam tey, ngir tontu mboolem lu ma Yawut yi jiiñ.