Acts 26:20 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye li tàmbali ci Damas, teg ci dëkku Yerusalem ak réewu Yawut mépp, ba agsi ci ñi dul Yawut, yégal naa leen, ñu tuub seeni bàkkaar te woññiku ci Yàlla, bay jëf lu dëppook réccu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye li dale Damaas ak Yerusalem ba ci réewum Yawut gépp, ba ca ñi dul Yawut, ñoom ñépp yégal naa leen seen wartéef, muy tuubeel ak waññiku ci Yàlla, ak jëf ju tuubeel yellool.