Acts 26:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
maanaam Almasi bi dina dékku ay coono, te mooy jëkk a dekki, bay jollil leer ci bànni Israyil ak ñi dul Yawut.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dañu noon fàww Almasi jaar ci ay coono te mooy jëkka dekki, ba siiwtaane leer gu jolli, ñeel bànni Israyil ak jaambur ñi itam.»