Acts 26:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Pool tontu ko: «Festus mu tedd mi, dofuma; waaye lu dëggu laay wax te ànd ak sago.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Póol ne ko: «Dofuma de, Festus mu tedd mi, dëgg gu ànd ak xel kay, laay biral.