Acts 26:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yaw buur Agaripa, ndax gëmuloo yonent yi? Xam naa bu wér ne, gëm nga.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur Àggripa, xanaa gëm nga yonent yi? Xam naa xéll ne gëm nga.»