Acts 26:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte xam nga bu baax aaday Yawut yi ak seeni werantey yoon. Kon maa ngi lay ñaan, nga déglu ma ak muñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Rawatina ba ma xamee ne ku géeju nga ci aaday Yawut, ak werante yi ci seen wàllu yoon. Kon dama lay ñaan rekk, nga muñal ma, déglu ma.