Acts 26:32 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te Agaripa ne Festus: «Manoon nanu koo yiwi, bu dénkuloon mbiram Sesaar.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Àggripa moom ne Festus: «Kii kay su dénkuloon mbiram Sesaar, nu man koo yiwi.»
Recommended Reading