Acts 26:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam nañu ma bu yàgg te man nañoo seede, su leen neexee, ne daan naa dund ni Farisen, te mooy tariixa bi gën a diis ci sunu diine.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam nañu ma bu yàgg, te su leen neexee ñu seede ne ngérum Farisen mi gëna diis ci sunu diine, ci laa masa bokk.