Acts 27:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nes tuuti ngelaw lu wole penku, ñu di ko wax «Ërakilon,» jóge ca dun ba, ne milib ci sunu kaw.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul nes tuut ngelaw lu réy lu ñuy wax Penkub kaw, riddee ca dun ba.