Acts 27:23 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte ci guddi menn malaaka dikkal na ma, jóge ci Yàlla sama Boroom, bi may jaamu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax malaakam Yàlla ji ma moom, te ma di ko jaamu, moo ma dikkal biig.
Recommended Reading